TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-brpgm25 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
  • Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2024-2025
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii
    2019-2020 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
Xóotalal waxtaan bi
Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025
CA-brpgm25 p. 4

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:

  1. 1. Lu tax amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi? (Room 1:16; 11:13)

  2. 2. Naka lañuy wonee ne dañoo takku ci xibaaru jàmm bi? (Macë 10:32; Room 10:9)

  3. 3. Naka lañuy wonee ne ay waarekat yu amul dara li ñuy rus lañu? (2 Timote 2:15)

  4. 4. Naka lañu mënee roy ci Onesifor? (2 Timote 1:​7, 8)

  5. 5. Naka lañuy wone ne nguuru Yàlla lañu faral? (Yawut ya 10:39; 1 Piyeer 3:15; Yowaana 18:36; 1 Tesalonig 5:​12, 13)

  6. 6. Naka lañuy «ndamu ci Boroom bi»? (Taalifi Cant 34:​1, 2; 1 Korent 1:31)

© 2024 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

CA-brpgm25-WO

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager