TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-brpgm20 p. 4
  • Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii
  • 2019-2020 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
Xóotalal waxtaan bi
2019-2020 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
CA-brpgm20 p. 4

Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii :

  1. Naka lañu mën a wonee suñu mbëggeel ci Yàlla ? (Deutéronome 13:​3, 4 ; 1 Yowaana 5:⁠3)

  2. Lu tax ñu war a bëgg suñu mbokk yi ci ngëm ? (1 Yowaana 4:​11, 20, 21)

  3. Naka lañu mën a wone mbëggeel suñu moroom ? (Lévitique 19:18 ; Efes 5:⁠29)

  4. Naka lañu mënee roy mbëggeelu Yexowa ? (1 Piyeer 4:8 ; Kolos 3:⁠13)

  5. Naka lañu mënee màggal Yexowa ? (Sabóor 104:33 ; 146:​2, 5)

  6. Bëgg Yexowa ak suñu xol bépp, lan la tekki ? (Exode 34:14 ; Amos 5:15 ; Room 12:⁠11)

© 2019 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager