TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-copgm20 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  • 2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii
    2019-2020 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025
Xóotalal waxtaan bi
2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
CA-copgm20 p. 4

Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii :

  1. Naka la mbëggeel gënee am njariñ xam-xam ? (1 Korent 8:⁠1)

  2. Naka lañu mënee yékkati ngëmu mbooloo mi ni ko jaamu Yàlla yi ci jamono yu njëkk ya daan defe ? (Room 13:⁠8)

  3. Naka lañu mën a joxe suñu bakkan ñi ñuy dajeel ci waare bi ? (1 Tesalonig 2:​7, 8)

  4. Naka lañu mën a defe suñu wàll ngir dëgëral suñu diggante ak suñu mbokk karceen yi ? (Efes 4:​1-3, 11-16 ; 1 Tesalonig 5:⁠11)

  5. Naka lañu mën a defe lépp ak mbëggeel ? (1 Korent 16:⁠14)

© 2019 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager