TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-copgm25 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  • Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2024-2025
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
  • Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii
    2019-2020 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
Xóotalal waxtaan bi
Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2024-2025
CA-copgm25 p. 4

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:

  1. 1. Naka la li ñu xam ci xibaaru jàmm bi, di ñu dimbali ñu soppi suñu dund? (Filib 1:27; 3:8)

  2. 2. Li ñu xam ci xibaaru jàmm bi, lan lañuy xiir ñu def? (Kolos 1:​5, 6)

  3. 3. Lan mooy ñuy xiir ci wéy di yégle xibaaru jàmm bi? (2 Piyeer 3:​11, 12; 1 Korent 9:​19, 23)

  4. 4. Lan lañu mën a def ba rafetal suñu tur ni Seede Yàlla? (2 Korent 6:​4-8)

  5. 5. Yàlla dafa ñuy jàngal jaaraale ko ci xibaaru jàmm bi. Naka la koy defe? (Tit 2:​11-14)

© 2024 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

CA-copgm25-WO

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager