TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-brpgm22 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  • Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2021-2022
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
  • Yokkal sa ngëm!
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2021-2022
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2021-2022
CA-brpgm22 p. 4

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:

  1. 1. Lu tax ñu war a yokk suñu ngëm tey ci tey? (Yawut ya 10:39)

  2. 2. Naka lañu mënee gis Yexowa mi “kenn mënula teg bët”? (Yawut ya 11:27)

  3. 3. Lu tax jàng waxi yonent yi nekk ci Biibël bi am njariñ? (Room 10:17)

  4. 4. Naka la ñu xel mu sell mi mënee dimbali ñu yokk suñu ngëm? (Luug 11:13; Galasi 5:22)

  5. 5. Naka lañu mënee dimbali suñuy moroom ngir yékkati seen ngëm? (1 Tesalonig 2:7, 8)

  6. 6. Lu tax ñu war a «ne jàkk Yeesu, moom mi samp ngëm, ba ub làmbi ngëm»? (Yawut ya 12:2, 3)

© 2021 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

CA-brpgm22-WO

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager