TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-brpgm23 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  • Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2022-2023
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Ñi bëgg jàmm
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2022-2023
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023
  • Tànnal bu baax say xarit
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2022-2023
CA-brpgm23 p. 4

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:

  1. 1. Naka lañu mënee raññee ñi bëgg jàmm? (Luug 10:6)

  2. 2. Naka lañu mënee dimbali ñi bëgg jàmm, ñu nekk xaritu Yàlla? (Macë 10:11)

  3. 3. Naka la Yeesu, Buuru jàmm bi, di ñu dimbalee ñu wut ñi bëgg jàmm? (Esayi. 9:5, 6; Macë 28:20)

  4. 4. Naka lañu mënee wone ne, ñu bëgg jàmm lañu? (Sabóor 11:5; 2 Timote 2:24; Saag 3:17, 18)

  5. 5. Naka la ñi bëgg jàmm di dimbalantee ci seen biir? (2 Korent 6:13)

  6. 6. Naka lañu mënee wéy di ‘not lu bon ci def lu baax’? (Room 12:2, 6, 10, 18)

© 2022 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

CA-brpgm23-WO

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager