Li nekk ci téere bii
LESOŊ YI
Leetar bu jóge ci Jataay biy dogal
3 Booleel ay laaj ci sa njàngale
4 Li nga mën a wax bala ngay jàng aaya
6 Woneel bu baax njariñu aaya yi
7 Waxal lu wóor lu nit mën a gëm
8 Jàngalal nit ñi ak ay misaal
9 Jëfandikool ay wideo ak ay nataal ngir jàngal nit ñi
10 Ni ngay soppee sa baat booy jàngale
12 Waxal ak mbaax te woneel ne yëg nga nit ñi
13 Woneel bu baax njariñu li ngay jàngale
14 Woneel bu baax ponk yi gën a am solo
15 Woneel ne gëm nga li ngay wax
16 Xiiral nit ñi ci jëfe li ñu dégg te amal xalaat bu rafet ci ñoom
17 Li ngay wax na leer ci ñi lay déglu
18 Defal waxtaan buy yokk xam-xam
19 Defal lépp ngir laal xolu nit ñi