TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 10/04 p. 3-6
  • Lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla ci atum 2005

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla ci atum 2005
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2004
  • Turu xaaj yi
  • Ni ñu koy doxale
  • PROGRAMME
Sasu Nguuru Yàlla — 2004
km 10/04 p. 3-6

Lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla ci atum 2005

Ni ñu koy doxale

Ci atum 2005, nii lañuy doxale Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla bi :

TÉERE YI ÑUY JËFANDIKOO : Les Saintes Écritures — Traduction du monde nouveau [bi12], La Tour de Garde [w], Tirez profit de l’École du ministère théocratique [be], “ Toute Écriture est inspirée de Dieu et utile ” (bu 1997) [si], et Comment raisonner à partir des Écritures (bu 1989) [rs].

WARUÑU TÀRDE. Bu waxtu bi jote rekk, nañu tàmbali lekkool bi ak benn woy-Yàlla, ñaan te teral nit ñi, ba pare def lii :

LIY TAX ÑU AAY CI WAX (Technique oratoire) : 5 minit. Wottukatu lekkool bi, kiy koy jàpple, walla mag bu mën def lekkool bi dina jëfandikoo téere École du ministère ngir waxtaan ci lenn luy tax ñu aay ci wax. (Bu ngeen amulee mag yu bare ci seen mbooloo, surga mbooloo bu mën jàngale mën na def waxtaan bi). War nañu laal lépp li feeñ ci xët yi ñu jagleel waxtaan bi. Bu amee ci xët yooyu wërale bu ci bokkul, dinañu ko wax. Waruñu boole jéemantal yi ci waxtaan bi. Jéemantal yooyu, nit ku nekk moo ko war a defal boppam. Kuy jiite lekkool bi mën na leen jëfandikoo itam bu wéetee ak nit, di ko xelal.

WAXTAAN N° 1 : 10 minit. Benn mag walla benn surga mbooloo mi moo ko war a def. Ci téere yii lañu koy defe : La Tour de Garde, Tirez profit de l’École du ministère théocratique walla “ Toute Écriture est inspirée de Dieu et utile ”. Waare lay doon ngir jàngal ñi teew ci 10 minit. Bu paree waxtaanam, warul a laaj ay laaj ñi teew ngir ñu fàttaliku li mu wax. Ki koy def dafa war a wax li nekk ci xët yi ñuy jagleel waxtaan bi. War na fexe it ba nit ñi gis bu baax njariñ bi nekk ci li ñu wax ci xët yooyu. Te it, war na wone bu baax li gën a am njariñ ci mbooloo mi. Waxtaan bi jox nañu ko tur (thème) ba pare. Tur boobu lañu war a jëfandikoo. Waxtaan bi warul a weesu 10 minit. Bu ñu waree xelal ki def waxtaan bi, kiy jiite lekkool bi na wéet ak moom.

KÀDDU YU AM SOLO CI LI ÑU WAROON A JÀNG CI BIIBËL BI : 10 minit. Ci juróom-benni minit yi njëkk yi, mag walla surga mbooloo bu aay, war na wone ni mbooloo mi mënee jariñoo xaaju Biibël bi ñu waroon a jàng ci ayu-bés bi. Mën na wax ci aaya bu mu mënta doon bu bokk ci xaaj boobu. Kiy def waxtaan bi, warul yem rekk ci tënk pàcc yi ñu war a jàng, waaye war na wone lu tax li ci nekk am njariñ ak it naka lañu ko mënee jariñoo. Kiy jiite waxtaan bii, war na fexe ba bañ a wax lu ëpp juróom-benni minit. Te fàww mu may ñi teew ñeenti minit ngir ñu wax yan aaya ñoo leen neex, te lu tax aaya yooyu am solo. Seen tont dafa war a gàtt (warul weesu 30 segoond). Bu ñu paree, kiy jiite lekkool bi dina wax ñi war a dem ci yeneen kalaas yi ñu dem fa.

WAXTAAN N° 2 : 4 minit. Benn mbokk mu góor moo ko war a def. Ci lu ëpp, ci Biibël bi lay jànge. Waaye weer wu nekk, dinañu ñaan benn yoon mbokk bi koy def mu jàng benn xaaj ci La Tour de Garde. Kiy def waxtaan bi, warul wax dara balaa muy jàng, te bu jàngee ba pare, warul wax dara itam. Li ñu war a jàng ci waxtaan bi, mën na bañ a tolloo ayu-bés bu nekk, waaye ba tey ci ñeenti minit lañu ko war a jànge, walla sax ci lu gën a gaaw. Wottukat biy jiite lekkool bi war na seet li nekk ci li ñu war a jàng ayu-bés bu nekk, bu ko defee mu mën a xam ki ko war a def ndax mën na nekk xale walla déet, ndax dafa war a aay ci njàngale bi walla déet. Wottukatu lekkool bi war na seet bu baax ni mu mënee dimbali kiy jàng ci lii : buy jàng, mu nànd li muy jàng ; jàng bi yomb ci moom (fluidité) ; mu bañ a juum ci ni muy waxe baat yi te kàddu yi ëpp solo feeñ bu baax ; li ñuy woowe modulation ; buy jàng, mu taxaw fi mu war a taxaw ; te wax ni muy waxe bés bu nekk.

WAXTAAN N° 3 : 5 minit. Benn mbokk mu jigéen moo ko war a def. Mën na tànnal boppam benn cadre (maanaam ni waxtaan bi di ame) ci téere École du ministère ci xët 82, waaye yenn saay dinañu ko jox benn cadre ci yi nekk ci xët boobu. Na topp tur (thème) bu ñu jagleel waxtaan bi te na mel ni kuy waaraate. Na waxtaan bi niroo ak lu mën a am dëgg ci gox bu seen mbooloo moom te mën a jariñ waaraatekat yi. Bu ñu waxul ci ban téere lañu war a seet ngir def waxtaan bi, ki koy def na wutal boppam li muy wax ci téere yi surga bu takku te teey bi defar. Ñi yàggul a bokk ci lekkool bi, nañu leen jox waxtaan boo xam ne wax nañu yan téere la war a jëfandikoo. Wottukatu lekkool bi dina seetlu bu baax ni waxtaan bi di demee ak ni mbokk mu koy def di dimbalee ki muy jàngal ba mu mën a xalaat ci li nekk ci mbind mi te nànd li ëpp solo ci waxtaan bi. Ñiy def waxtaan bi dañu war a mën a jàng. Wottukatu lekkool bi dina ko wax ak kan la war a def waxtaan bi.

WAXTAAN N° 4 : 5 minit. Ki koy def dafa war a topp tur (thème) bu ñu jagleel waxtaan bi. Bu ñu waxul ci ban téere lañu war a seet ngir def waxtaan bi, ki koy def moo war a wutal boppam li muy wax ci téere yi surga bu takku te teey bi defar. Bu fekkee ne mbokk mu góor moo ko war a def, waare lay doon, te bu koy def dina bàyyi xel ci ñi koy déglu. Bu dee mbokk mu jigéen moo koy def, na ko def ni ñuy defe waxtaan n° 3. Kiy jiite lekkool bi, bu gisee ne góor mën na def waxtaan n° 4 bi, mën na ko jox suñu benn mbokk mu góor. Bu leen fàtte ne waxtaan yi ànd ak biddéew bu ndaw, mbokk mu góor kese moo leen war a def te dafay nekk waare.

WAXTU WI : Waxtaan yi ak xelal yi, waruñu yàgg ba weesu waxtu bi ñu leen jagleel. Ñiy def waxtaan n° 2, 3, ak 4, bu ñu weesoo waxtu bi ñu leen may, nañu seet fasoŋ bu rafet bu ñu mënee dog seen waxtaan. Kiy def waxtaan biy ubbi lekkool bi te jëm ci liy tax ñu aay ci wax (technique oratoire), kiy def waxtaan n° 1, walla kiy wax kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi, bu ci amee ku waxtaanam yàgg ba weesu waxtu bi ñu ko may, war nañu wéet ak moom ngir xelal ko. Képp kuy def waxtaan war na seetlu bu baax waxtu bi ngir waxtaanam bañ a yàgg ba weesu waxtu bi ñu ko may. Lekkool bi 45 minit la war a def. Loolu boolewuñu ci ñaan bi ak woy-Yàlla bi.

XELAL YI : 1 minit. Bu kenn paree waxtaanam, wottukatu lekkool bi dina wax ci li baax li mu def ci waxtaan bi. Loolu warul weesu benn minit. Du ko wax rekk ne “ sa waxtaan baaxoon na ”, waaye dina wax lenn ci li tax waxtaanam baax. Bu ndaje bi jeexee, walla beneen bés, dina toog ak moom ngir xelal ko ci lu ko mën a jëmloo kanam bu gisee ne soxla na ko.

KIY JÀPPLE KIY XELAL NIT ÑI : Ginnaaw wottukatu lekkool bi, bu amee beneen mag ci mbooloo mi bu mën a jiite lekkool bi, kurélu mag ñi dinañu ko tànn ngir mu jàpple kiy xelal nit ñi. Bu fekkee ne magi mbooloo mi xaw nañu bare, kon, mën nañu tànn at mu nekk beneen mag bu mën xelal ngir mu jàpple kiy xelal nit ñi. Kooku dina xelal ñiy def waxtaan n° 1 ak kiy wax kàddu yu am solo ci Biibël bi, bu ñu ko soxlaa. Du saa yu mag walla surga mbooloo mi di def waxtaan yooyu, la koy war a xelal. Li ñu wax fii, dinañu ko def ci atum 2005. Waaye mën na am bu ëllëgee mu am lu ñu ci soppi.

KAYIT FI ÑU BIND XELAL YI : Mu ngi ci téere École du ministère.

WAXTAAN AK ÑI TEEW NGIR FÀTTALIKU LI ÑU JÀNG CI LEKKOOL BI (Révision orale) : 30 minit. Ñaari weer yu nekk, wottukatu lekkool bi dina laaj ay laaj ñi teew ngir ñu fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi. Dinañu njëkk wax ci liy tax ñu aay ci wax (technique oratoire) ak it kàddu yu am solo ci li ñu waroon a jàng ci Biibël bi (nañu topp tegtal yi nekk ci kow ngir waxtaan yooyu), ba pare ñu waxtaan ak ñi teew ngir fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi ci ñaari weer yi weesu, boole ci li ñu def ci ayu-bés bi. Seen ndaje bu mag bu ñaari fan walla ayu-bés bi wottukat biy wër war a ñów ci seen mbooloo mën na tombe ci ayu-bés bu ñu war a fàttaliku li ñu jàng ci lekkool bi. Bu boobaa, nangeen topp li Sasu Nguuru Yàlla bu desàmbar 2003 wax ci xët 6 lu jëm ci ni ñu war a defe lekkool bi ci ayu-bés boobu.

PROGRAMME

3 janv. Lecture de la Bible : Josué 16-20 Cantique 6

Technique oratoire : Idées compréhensibles (be p. 226 § 1–p. 227 § 1)

No 1 : Crains le vrai Dieu (be p. 272 § 1–p. 273 § 1)

No 2 : Josué 16:1–17:4

No 3 : Pourquoi il n’est pas suffisant de lire la Bible (rs p. 316 § 1-2)

No 4 : Est-ce la pauvreté ou la richesse qui prouve notre attachement à Dieu aujourd’hui ?

10 janv. Lecture de la Bible : Josué 21-24 Cantique 100

Technique oratoire : Expliquez les termes peu courants (be p. 227 § 2–p. 228 § 1)

No 1 : Faisons connaître le nom de Dieu (be p. 273 § 2–p. 274 § 1)

No 2 : Josué 23:1-13

No 3 : La vraie religion fonde ses enseignements sur la Bible et fait connaître le nom de Dieu (rs p. 316 § 3-4)

No 4 : Convient-il d’adorer Jésus ?

17 janv. Lecture de la Bible : Juges 1-4 Cantique 97

Technique oratoire : Donnez toutes les explications nécessaires (be p. 228 § 2-3)

No 1 : La personne que le nom désigne (be p. 274 § 2-5)

No 2 : Juges 2:1-10

No 3 : Les membres de la vraie religion exercent vraiment la foi en Jésus Christ (rs p. 317 § 1)

No 4 : Comment pouvez-vous vous protéger des clips vidéo malsains ?

24 janv. Lecture de la Bible : Juges 5-7 Cantique 47

Technique oratoire : Le rôle du cœur (be p. 228 § 4–p. 229 § 1)

No 1 : Le nom de Dieu est “ une tour forte ” (be p. 274 § 6–p. 275 intertitre)

No 2 : Juges 6:25-35

No 3 : Comment la Bible devrait-elle influer sur la liberté que nous avons de faire des choix ?

No 4 : La vraie religion n’est pas formaliste mais constitue un mode de vie (rs p. 317 § 2)

31 janv. Lecture de la Bible : Juges 8-10 Cantique 174

Technique oratoire : Présentation instructive (be p. 230 § 1-6)

No 1 : Rendre témoignage à Jésus (be p. 275 intertitre–p. 276 § 1)

No 2 : w03 15/1 p. 19 -20 § 16-18

No 3 : Les membres de la vraie religion s’aiment les uns les autres et se tiennent à l’écart du monde (rs p. 317 § 3-4)

No 4 : Le matérialisme implique davantage que d’acquérir des biens

7 févr. Lecture de la Bible : Juges 11-14 Cantique 209

Technique oratoire : Préparez un exposé instructif en faisant des recherches (be p. 231 § 1-3)

No 1 : Soulignez le rôle de Jésus en qualité de Rédempteur (be p. 276 § 2-3)

No 2 : Juges 12:1-15

No 3 : Pourquoi les Témoins de Jéhovah sont unis

No 4 : Les membres de la vraie religion sont des témoins actifs du Royaume de Dieu (rs p. 317 § 5)

14 févr. Lecture de la Bible : Juges 15-18 Cantique 105

Technique oratoire : Expliquez les versets (be p. 231 § 4-5)

No 1 : Soulignez les rôles de Jésus en qualité de Grand Prêtre et de Chef de la congrégation (be p. 277 § 1-2)

No 2 : Juges 15:9-20

No 3 : aSi quelqu’un vous dit : ‘ Du moment que vous croyez en Jésus, peu importe l’Église à laquelle vous appartenez ’ (rs p. 320 § 2)

No 4 : Pourquoi l’hypnose n’est pas pour les chrétiens

21 févr. Lecture de la Bible : Juges 19-21 Cantique 53

Technique oratoire : Expliquez le sens des termes (be p. 232 § 1)

No 1 : Soulignez le rôle de Jésus en qualité de Roi régnant (be p. 277 § 3-4)

No 2 : w03 1/2 p. 17-18 § 18-21

No 3 : bSi quelqu’un vous dit : ‘ Qu’est-ce qui vous fait dire qu’il n’y a qu’une bonne religion ? ’ (rs p. 320 § 3)

No 4 : Quelles sont quelques-unes des “ choses profondes de Dieu ” ? (1 Cor. 2:10)

28 févr. Lecture de la Bible : Ruth 1-4 Cantique 120

Technique oratoire : Raisonnez à partir des textes bibliques (be p. 232 § 2-4)

Révision orale

7 mars Lecture de la Bible : 1 Samuel 1-4 Cantique 221

Technique oratoire : Choisissez des idées qui seront profitables à votre auditoire (be p. 233 § 1-5)

No 1 : Posez Christ comme fondement (be p. 278 § 1-4)

No 2 : 1 Samuel 2:1-11

No 3 : Jésus n’a pas été relevé dans un corps physique (rs p. 322 § 1-3)

No 4 : Pourquoi les vrais chrétiens ne consultent pas les horoscopes

14 mars Lecture de la Bible : 1 Samuel 5-9 Cantique 151

Technique oratoire : Utilisation des sources indiquées (be p. 234 § 1–p. 235 § 3)

No 1 : Cette bonne nouvelle du Royaume (be p. 279 § 1-4)

No 2 : 1 Samuel 5:1-12

No 3 : Pourquoi Jésus est apparu dans des corps de chair (rs p. 322 § 4–p. 323 § 3)

No 4 : Comment nous pouvons affermir notre amitié avec Jéhovah

21 mars Lecture de la Bible : 1 Samuel 10-13 Cantique 166

Technique oratoire : Bon usage des questions (be p. 236 § 1-5)

No 1 : Expliquons ce qu’est le Royaume (be p. 280 § 1-5)

No 2 : 1 Samuel 10:1-12

No 3 : Comment les chrétiens devraient-ils traiter leurs proches qui ne partagent pas leur foi ?

No 4 : Ceux qui seront ressuscités pour régner avec Christ seront comme lui (rs p. 323 § 5–p. 324 § 3)

28 mars Lecture de la Bible : 1 Samuel 14-15 Cantique 172

Technique oratoire : Des questions pour introduire des pensées importantes (be p. 237 § 1-2)

No 1 : Expliquons en quoi notre vie est concernée par le Royaume (be p. 281 § 1-4)

No 2 : w03 15/3 p. 19-20 § 17-21

No 3 : Pourquoi les chrétiens paient leurs impôts

No 4 : Ce que représentera la résurrection pour les hommes en général (rs p. 324 § 4–p. 325 § 3)

4 avril Lecture de la Bible : 1 Samuel 16-18 Cantique 27

Technique oratoire : Questions pour raisonner sur un sujet (be p. 237 § 3–p. 238 § 2)

No 1 : Pourquoi les chrétiens accordent de l’importance à l’éducation (w03 15/3 p. 10 § 1–p. 11 § 5)

No 2 : 1 Samuel 17:41-51

No 3 : Pourquoi les ressuscités ne seront pas condamnés en raison de leurs actions passées (rs p. 326 § 1)

No 4 : Le fait de réfléchir aux conséquences de nos actes peut nous aider à aimer ce qui est bon et à haïr ce qui est mauvais

11 avril Lecture de la Bible : 1 Samuel 19-22 Cantique 73

Technique oratoire : Des questions pour faire exprimer les sentiments personnels (be p. 238 § 3-5)

No 1 : Comment les jeunes peuvent progresser spirituellement (w03 1/4 p. 8-10)

No 2 : 1 Samuel 20:24-34

No 3 : Pourquoi la vraie modestie est une qualité attirante

No 4 : Comment le “ reste des morts ” viennent à la vie sur la terre (rs p. 326 § 2–p. 327 § 2)

18 avril Lecture de la Bible : 1 Samuel 23-25 Cantique 61

Technique oratoire : Des questions pour accentuer (be p. 239 § 1-2)

No 1 : Mets ta confiance en Jéhovah de tout ton cœur (w03 1/11 p. 4-7)

No 2 : w03 1/5 p. 17 § 11-14

No 3 : Ceux qui ressusciteront sur la terre (rs p. 327 § 3–p. 328 § 3)

No 4 : Pourquoi une alliance fut conclue avec Abraham

25 avril Lecture de la Bible : 1 Samuel 26-31 Cantique 217

Technique oratoire : Des questions pour réfuter un point de vue erroné (be p. 239 § 3-5)

Révision orale

2 mai Lecture de la Bible : 2 Samuel 1-3 Cantique 91

Technique oratoire : Des comparaisons et des métaphores instructives (be p. 240 § 1–p. 241 § 1)

No 1 : L’éducation n’est pas seulement utile pour trouver du travail (w03 15/3 p. 11 § 6–p. 14 § 6)

No 2 : 2 Samuel 2:1-11

No 3 : Les événements liés à la présence de Christ s’étendent sur des années (rs p. 329 § 1-2)

No 4 : Les nombreux bienfaits que procure l’honnêteté

9 mai Lecture de la Bible : 2 Samuel 4-8 Cantique 183

Technique oratoire : Recourez à des exemples (be p. 241 § 2–p. 242 § 1)

No 1 : Jéhovah se préoccupe sincèrement des jeunes (w03 15/4 p. 29 § 3–p. 31 § 3)

No 2 : 2 Samuel 5:1-12

No 3 : Qu’a accompli l’alliance de la Loi ?

No 4 : Le retour du Christ est invisible (rs p. 329 § 3–p. 330 § 2)

16 mai Lecture de la Bible : 2 Samuel 9-12 Cantique 66

Technique oratoire : Des exemples tirés des Écritures (be p. 242 § 2-3)

No 1 : Jéhovah remarque-t-il vos actions ? (w03 1/5 p. 28-31)

No 2 : 2 Samuel 9:1-13

No 3 : La façon dont Jésus reviendra et dont tout œil le verra (rs p. 330 § 4–p. 331 § 5)

No 4 : De quelles façons la Parole de Dieu est-elle vivante ? (Héb. 4:12)

23 mai Lecture de la Bible : 2 Samuel 13-15 Cantique 103

Technique oratoire : Comprendra-t-on ? (be p. 242 § 4–p. 243 § 1)

No 1 : Que nous apprend le journal de bord de Noé ? (w03 15/5 p. 4-7)

No 2 : 2 Samuel 13:10-22

No 3 : Comment comprendre Jean 11:25, 26 ?

No 4 : Événements rattachés à la présence du Christ (rs p. 332 § 1-5)

30 mai Lecture de la Bible : 2 Samuel 16-18 Cantique 132

Technique oratoire : Illustrations tirées de la vie courante (be p. 244 § 1-2)

No 1 : Pour agir avec sagesse, raisonnons correctement (w03 15/7 p. 21-3)

No 2 : w03 15/5 p. 16-17 § 8-11

No 3 : Les chrétiens ne sont pas tenus d’observer le sabbat (rs p. 343 § 1–p. 344 § 2)

No 4 : Pourquoi l’humilité n’est pas une faiblesse

6 juin Lecture de la Bible : 2 Samuel 19-21 Cantique 224

Technique oratoire : Illustrations appropriées à votre auditoire (be p. 244 § 3–p. 245 § 4)

No 1 : Comprenons bien le but de la discipline (w03 1/10 p. 20 § 1–p. 21 § 5)

No 2 : 2 Samuel 19:1-10

No 3 : Comment un chrétien peut-il entrer dans le repos de Dieu ?

No 4 : Le récit biblique n’indique nulle part qu’Adam devait observer un jour de sabbat (rs p. 344 § 3–p. 345 § 1)

13 juin Lecture de la Bible : 2 Samuel 22-24 Cantique 74

Technique oratoire : Bonne utilisation des supports visuels (be p. 247 § 1-2)

No 1 : Soyons dociles à l’enseignement et surveillons notre langue (w03 15/9 p. 21 § 1–p. 22 § 4)

No 2 : 2 Samuel 24:10-17

No 3 : Jésus n’a pas divisé la Loi en une partie “ cérémonielle ” et en une partie “ morale ” (rs p. 345 § 2–p. 346 § 1)

No 4 : De quelles façons un chrétien doit-il se tenir séparé du monde ?

20 juin Lecture de la Bible : 1 Rois 1-2 Cantique 2

Technique oratoire : Comment Jésus a utilisé les supports visuels (be p. 247 § 3)

No 1 : Apprenons le secret du contentement (w03 1/6 p. 8-11)

No 2 : w03 1/6 p. 12-13 § 1-4

No 3 : Qu’avait de remarquable le dixième commandement ?

No 4 : Les Dix Commandements ont été abolis en même temps que la Loi (rs p. 346 § 2-3)

27 juin Lecture de la Bible : 1 Rois 3-6 Cantique 167

Technique oratoire : Diverses manières d’utiliser les supports visuels (be p. 248 § 1-3)

Révision orale

4 juillet Lecture de la Bible : 1 Rois 7-8 Cantique 194

Technique oratoire : Utilisation des cartes, des programmes d’assemblées et des cassettes vidéo (be p. 248 § 4–p. 249 § 2)

No 1 : Chérissons nos compagnons âgés (w03 1/9 p. 30-1)

No 2 : 1 Rois 8:1-13

No 3 : Comment Jésus a-t-il vaincu le monde ?

No 4 : Pourquoi l’abolition de la Loi n’a pas signifié la disparition des contraintes morales (rs p. 347 § 1-2)

11 juillet Lecture de la Bible : 1 Rois 9-11 Cantique 191

Technique oratoire : Utilisation de supports visuels en présence d’un auditoire nombreux (be p. 249 § 3–​p. 250 § 1)

No 1 : Des preuves de l’existence de Jésus (w03 15/6 p. 4-7)

No 2 : 1 Rois 9:1-9

No 3 : Ce que représente le sabbat pour les chrétiens (rs p. 347 § 3–p. 349 § 1)

No 4 : On peut s’affranchir de la drogue en appliquant les principes bibliques

18 juillet Lecture de la Bible : 1 Rois 12-14 Cantique 162

Technique oratoire : Pourquoi il est important d’utiliser un raisonnement bien construit (be p. 251 § 1-3)

No 1 : Des pensées aux actes, puis aux conséquences (w03 15/1 p. 30 § 1-3)

No 2 : 1 Rois 12:1-11

No 3 : Comment la foi peut nous aider à surmonter les épreuves

No 4 : Ceux que la Bible qualifie de saints (rs p. 350 § 1-3)

25 juillet Lecture de la Bible : 1 Rois 15-17 Cantique 158

Technique oratoire : Pour commencer un raisonnement (be p. 251 § 4–p. 252 § 3)

No 1 : Comment “ comprendre quelle est la volonté de Jéhovah ” (w03 1/12 p. 21 § 2–p. 23 § 2)

No 2 : w03 15/7 p. 19 § 15-17

No 3 : Pourquoi nous ne prions pas les “ saints ” (rs p. 351 § 1-3)

No 4 : Comment l’esprit saint console-t-il les chrétiens ?

1er août Lecture de la Bible : 1 Rois 18-20 Cantique 207

Technique oratoire : Quand se montrer conciliant (be p. 252 § 4–p. 253 § 2)

No 1 : Jeunes, marchez d’une manière digne de Jéhovah (w03 15/10 p. 23 § 1–p. 24 § 1)

No 2 : 1 Rois 18:1-15

No 3 : Tous les chrétiens peuvent porter beaucoup de fruit

No 4 : La vérité au sujet de la vénération des reliques ou des images des “ saints ” (rs p. 352 § 1–p. 353 § 1)

8 août Lecture de la Bible : 1 Rois 21-22 Cantique 92

Technique oratoire : Posez des questions et fournissez des arguments (be p. 253 § 3–p. 254 § 2)

No 1 : La fin de la pauvreté (w03 1/8 p. 4-7)

No 2 : 1 Rois 21:15-26

No 3 : Les vrais chrétiens qui sont saints ne sont pas exempts du péché (rs p. 353 § 2)

No 4 : Pourquoi devons-nous avoir du courage et comment pouvons-nous le cultiver ?

15 août Lecture de la Bible : 2 Rois 1-4 Cantique 16

Technique oratoire : Argumentation solidement fondée sur la Parole de Dieu (be p. 255 § 1–p. 256 § 2)

No 1 : Vous avez reçu gratuitement, donnez gratuitement (w03 1/8 p. 20 -2)

No 2 : 2 Rois 3:1-12

No 3 : Pourquoi les gens vivaient-ils aussi longtemps avant le déluge ?

No 4 : L’enseignement du salut universel est-il biblique ? (rs p. 354 § 2)

22 août Lecture de la Bible : 2 Rois 5-8 Cantique 193

Technique oratoire : Argumentation corroborée par des preuves extérieures (be p. 256 § 3-5)

No 1 : Apprenez l’art du tact (w03 1/8 p. 29-31)

No 2 : w03 1/8 p. 19 § 18-22

No 3 : Tous les hommes obtiendront-ils finalement le salut ? (rs p. 355 § 1)

No 4 : Quelles belles qualités manifestées par Yona devrions-nous imiter ?

29 août Lecture de la Bible : 2 Rois 9-11 Cantique 129

Technique oratoire : Présentez suffisamment de preuves (be p. 257 § 1-4)

Révision orale

5 sept. Lecture de la Bible : 2 Rois 12-15 Cantique 175

Technique oratoire : Efforts pour toucher le cœur (be p. 258 § 1–p. 259 § 1)

No 1 : Cherchez-vous réellement Jéhovah ? (w03 15/8 p. 25-8)

No 2 : 2 Rois 12:1-12

No 3 : Pourquoi devrait-on poursuivre la douceur ?

No 4 : “ Toutes sortes d’hommes ” obtiendront le salut (rs p. 355 § 2)

12 sept. Lecture de la Bible : 2 Rois 16-18 Cantique 203

Technique oratoire : Faites apparaître ce que les gens ont dans le cœur (be p. 259 § 2-4)

No 1 : Quel souvenir Jésus a-t-il laissé ? (w03 15/8 p. 6 § 6–p. 8 § 6)

No 2 : 2 Rois 16:10-20

No 3 : La Bible dit-elle que certains hommes ne seront jamais sauvés ? (rs p. 355 § 3–p. 356 § 2)

No 4 : Comment pouvons-nous vérifier ce qui est agréable au Seigneur ?

19 sept. Lecture de la Bible : 2 Rois 19-22 Cantique 89

Technique oratoire : Éveillez des sentiments bénéfiques (be p. 259 § 5–p. 260 § 1)

No 1 : “ Retiens toujours le modèle des paroles salutaires ” (w03 1/1 p. 29 § 2–p. 30 § 4)

No 2 : 2 Rois 19:20-28

No 3 : Une fois sauvé ne veut pas dire sauvé pour toujours (rs p. 356 § 3-6)

No 4 : Que pouvons-nous apprendre de nos frères de la Smyrne antique ?

26 sept. Lecture de la Bible : 2 Rois 23-25 Cantique 84

Technique oratoire : Aidez vos auditeurs à cultiver la crainte de Dieu (be p. 260 § 2-3)

No 1 : La Bible et son canon — Partie 1 (si p. 299 § 1-6)

No 2 : w03 15/8 p. 20 § 6-10

No 3 : Nous voyons l’avenir avec optimisme

No 4 : Pourquoi la foi doit s’accompagner d’œuvres (rs p. 356 § 7–p. 357 § 3)

3 oct. Lecture de la Bible : 1 Chroniques 1-4 Cantique 51

Technique oratoire : Dieu attache de l’importance à notre conduite (be p. 260 § 4–p. 261 § 1)

No 1 : La Bible et son canon — Partie 2 (si p. 300-2 § 7-16)

No 2 : 1 Chroniques 4:24-43

No 3 : Comment nous savons que le Diable existe vraiment (rs p. 364 § 3–p. 365 § 3)

No 4 : Jéhovah nous aime individuellement

10 oct. Lecture de la Bible : 1 Chroniques 5-7 Cantique 195

Technique oratoire : Aidez vos auditeurs à s’analyser (be p. 261 § 2-4)

No 1 : La Bible et son canon — Partie 3 (si p. 302-5 § 17-26)

No 2 : 1 Chroniques 5:18-26

No 3 : Ce que nous savons au sujet du “ jour de Jéhovah ”

No 4 : Satan n’est pas simplement le mal qui est à l’intérieur de chaque humain (rs p. 365 § 4–p. 366 § 2)

17 oct. Lecture de la Bible : 1 Chroniques 8-11 Cantique 201

Technique oratoire : Favorisez l’obéissance venant du cœur (be p. 262 § 1-4)

No 1 : Le texte hébreu des Saintes Écritures — Partie 1 (si p. 305-6 § 1-5)

No 2 : 1 Chroniques 10:1-14

No 3 : Dieu n’a pas créé le Diable (rs p. 366 § 3)

No 4 : Envers qui devrions-nous faire preuve de tact ?

24 oct. Lecture de la Bible : 1 Chroniques 12-15 Cantique 80

Technique oratoire : Collaborons avec Jéhovah pour toucher le cœur des gens (be p. 262 § 5)

No 1 : Le texte hébreu des Saintes Écritures — Partie 2 (si p. 306-7 § 6-9)

No 2 : w03 1/11 p. 10-11 § 10-13

No 3 : Ce que signifie réellement marcher au nom de Jéhovah

No 4 : Pourquoi Dieu n’a pas détruit Satan immédiatement après sa rébellion (rs p. 367 § 1-2)

31 oct. Lecture de la Bible : 1 Chroniques 16-20 Cantique 129

Technique oratoire : Comment régler un bon minutage (be p. 263 § 1–p. 264 § 4)

Révision orale

7 nov. Lecture de la Bible : 1 Chroniques 21-25 Cantique 215

Technique oratoire : Exhortation efficace (be p. 265 § 1-3)

No 1 : Le texte hébreu des Saintes Écritures — Partie 3 (si p. 307-10 § 10-16)

No 2 : 1 Chroniques 22:1-10

No 3 : Ne sous- estimons pas le pouvoir du Diable (rs p. 368 § 1-3)

No 4 : cComment consolider son couple

14 nov. Lecture de la Bible : 1 Chroniques 26-29 Cantique 35

Technique oratoire : Exhortez en raison de l’amour (be p. 266 § 1-4)

No 1 : Le texte hébreu des Saintes Écritures — Partie 4 (si p. 310-12 § 17-25)

No 2 : 1 Chroniques 29:1-9

No 3 : Pourquoi les serviteurs de Jéhovah sont persécutés

No 4 : Les hommes seront bientôt libérés de l’influence pernicieuse de Satan (rs p. 369 § 1–p. 370 § 1)

21 nov. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 1-5 Cantique 46

Technique oratoire : Fondez votre exhortation sur les Écritures (be p. 266 § 5–p. 267 § 1)

No 1 : Le texte hébreu des Saintes Écritures — Partie 5 (si p. 312-13 § 26-31)

No 2 : 2 Chroniques 2:1-10

No 3 : Comprenons bien le but de la discipline

No 4 : dEst-ce un péché d’avoir des relations sexuelles ? (rs p. 370 § 2–p. 371 § 4)

28 nov. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 6-9 Cantique 106

Technique oratoire : Ayez de la “ franchise ” (be p. 267 § 2-3)

No 1 : Le texte grec des Saintes Écritures — Partie 1 (si p. 315-16 § 1-7)

No 2 : w03 1/12 p. 15-16 § 3-6

No 3 : Comment nous montrons que nous nous délectons en Jéhovah

No 4 : eCe que dit la Bible à propos de l’homosexualité (rs p. 372 § 2-4)

5 déc. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 10-14 Cantique 116

Technique oratoire : Pourquoi il est important d’être encourageant (be p. 268 § 1-3)

No 1 : Le texte grec des Saintes Écritures — Partie 2 (si p. 316-17 § 8-16)

No 2 : 2 Chroniques 12:1-12

No 3 : Pourquoi nous avons besoin de la faveur imméritée de Dieu

No 4 : Les changements à opérer pour plaire à Dieu (rs p. 372 § 5–p. 373 § 2)

12 déc. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 15-19 Cantique 182

Technique oratoire : Rappelez ce que Jéhovah a accompli (be p. 268 § 4–p. 269 § 2)

No 1 : Le texte grec des Saintes Écritures — Partie 3 (si p. 317-19 § 17-25)

No 2 : 2 Chroniques 19:1-11

No 3 : Pourquoi un homme parfait a pu pécher (rs p. 278 § 3–p. 279 § 3)

No 4 : Ce que nous pouvons apprendre de la famille de Jésus

19 déc. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 20-24 Cantique 186

Technique oratoire : Montrez comment Jéhovah a soutenu son peuple (be p. 269 § 3-5)

No 1 : Le texte grec des Saintes Écritures — Partie 4 (si p. 319-20 § 26-32)

No 2 : w03 15/12 p. 16-17 § 13-15

No 3 : Les bienfaits que l’on se procure en apprenant le secret du contentement

No 4 : Pourquoi nous considérons que tout péché est bel et bien un péché (rs p. 280 § 2–p. 281 § 2)

26 déc. Lecture de la Bible : 2 Chroniques 25-28 Cantique 137

Technique oratoire : Manifestez la joie que vous inspirent les actions de Jéhovah à notre époque (be p. 270 § 1–p. 271 § 2)

Révision orale

[Li ñu bind ci suuf]

a Dans la mesure du temps disponible, examinez les réponses aux affirmations, objections et autres réactions les plus courantes dans votre territoire.

b Dans la mesure du temps disponible, examinez les réponses aux affirmations, objections et autres réactions les plus courantes dans votre territoire.

c Attribué uniquement à un frère.

d Attribué uniquement à un frère.

e Attribué uniquement à un frère.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager