TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • ll xaaj 10 p. 22-23
  • Yan barke la ñiy dégg li Yàlla wax nar a am ?

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Yan barke la ñiy dégg li Yàlla wax nar a am ?
  • Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Xaaj 10
    Déggleen li Yàlla wax
  • Xaritu Yàlla yi dinañu dund ca Àjjana
    Mën nga nekk xaritu Yàlla !
  • Lan mooy coobare Yàlla ngir suuf si ?
    Lan la ñu Yàllay laaj?
  • Bu keroogee xam-xamub Yàlla di fees suuf si
    Xam-xam biy jëme ca dund ga dul jeex
Xóotalal waxtaan bi
Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex
ll xaaj 10 p. 22-23

XAAJ 10

Yan barke la ñiy dégg li Yàlla wax nar a am ?

Ñi gën a bare ci ñi dee dinañu dekki. Jëf ya 24:15

Nit ñi nekk ci àjjana ñoo ngi dalal ñi dekki

Xalaatleen ci barke yi ngeen nar a am bu fekkee ne yéena ngi dégg li Yexowa wax! Feebar dootul am. Lafañ itam dootul am. Dingeen am wér-gi-yaram gu mat sëkk. Nit ku bon dootul am. Kenn ku nekk dinga mën a wóolu sa moroom.

Naqar, metit walla jooy dootul am. Kenn dootul màggat, kenn dootul dee.

Dingeen nekk ak seeni xarit ak seen njaboot. Dund bi dina neex lool ci àjjana bi nar a am ci kaw suuf si.

Kenn dootul am looy ragal. Jàmm dëgg mooy am ci kaw suuf si.

Nguuru Yàlla dina fi dindi bépp naqar ak coono. Peeñu ma 21:3, 4

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager