Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
1. Naka lañuy wonee ne yàkkamti nañu ndimbalu Yexowa? (Sabóor 130:5, 6)
2. Bu ñu nekkee ci jafe-jafe, naka lañu mën a wonee ne yàkkamti nañu ndimbalu Yexowa? (Abakug 2:3, 4; 2 Timote 4:2; Luug 2:36-38)
3. Naka lañu mënee jariñoo bu baax suñu jot bala bésu Yexowa di ñëw? (2 Piyeer 3:11-13)
4. Bu ñu amee lu ñu metti, lu tax ñu war a teg suñu yaakaar ci Yexowa? (Sabóor 62:2, 3, 9, 11; 68:7; 130:2-4)
5. Lan lañu war a def ngir ‘jot yoolu ku jub’? (Sabóor 58:11)
© 2023 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
CA-copgm24-WO