Kan mooy Yàlla?
«Aji Sax jeey Yàlla dëgg. Mooy Yàlla jiy dund» (Yeremi 10:10).
Ndax xamoon nga ne
Yàlla am na tur (Taalifi Cant 83:18, nwt).
Yàlla dafa ñuy xelal jaare ko ci Téere yu sell yi (2 Timote 3:16, 17).
Yàlla bëgg na ñoo dimbali (Taalifi Cant 145:18, 19).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania