Ndax li Yeesu jàngale mën nañu amal njariñ tey?
«Lépp lu ngeen bëgg nit ñi defal leen ko . . . nangeen leen ko defale noonu.» (Macë 7:12).
Yeesu jàngale na itam ne
Def li ñu mën tey te bañ a jaaxle ci lu agseegul, dina ñu may xel mu dal (Macë 6:34).
Dañu war a baal suñu moroom (Macë 6:14, 15).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania