Ndax dund ci jàmm ba fàww, lu mën a nekk la?
«Aji jub ay jagoo réew mi, dëkke ko ba fàww.» (Taalifi Cant 37:29).
Biibël bi wax na ne ci kanam tuuti
Kenn dootul feebar (Esayi 33:24; 35:5, 6).
Yàlla dina defaraat suuf si, mu doon àjjana (Esayi 35:1, 2; Peeñu ma 11:18).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania