Ndax Yàlla nangu na diine yépp?
«Xat la def, bunt ba jëm dund; sew it la yoon wa def, te ñu néew a koy gis.» (Macë 7:14).
Kàddu Yàlla wone na ne
Du diine yépp la Yàlla nangu (Macë 7:21-23; Màrk 7:6-8).
Ñi bokk ci diine dëgg gi, ay nitu jàmm lañu te dañoo bëgg seen moroom (Mise 4:3; Yowaan 13:35).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania