Leneen lu jëm ci loolu gf lesoŋ 14 p. 22-23 Xaritu Yàlla yi dañuy moytu lu bon Jëf yi Yàlla bañ Lan la ñu Yàllay laaj? Lan lañu war a def ba am dundin bu neex Yàlla ? Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex Xaaj 13 Déggleen li Yàlla wax Ndax Yàlla dina alagaat ñu bon ñi ? Dundleen ba fàww ak bànneex ci suuf si ! Nañu dund ci fasoŋ bu neex Yàlla Lan la Biibël bi wax dëgg-dëgg ? Bul topp diine ju dul dëgg ! Mën nga nekk xaritu Yàlla !