Li nekk ci téere bii
Leetar bu jóge ci Jataay biy dogal
LESOŊ
XAAJ 1: NI NGA MËNEE TÀMBALI WAXTAAN
1 Wonal nit ñi ne am nga itte ci ñoom
XAAJ 2: LI NGA MËN A WAX BOO SEETIWAATEE NIT KI
7 Wéyal di yégle xibaaru jàmm bi
8 Deel muñ, te def ndànk ak nit ñi ci liggéeyu waare bi
9 Wonal nit ñi ne li ñuy yëg itteel na la
XAAJ 3: NI NGA MËNEE JÀNGAL NIT ÑI BA ÑU NEKK TAALIBE YEESU
10 Na nga farlu ci liggéeyu waare bi
11 Na li ngay wax nekk lu yomb a nànd
12 Waxal nit ki ci lu leer li mu war a soppi ci dundam