Ndax Yàlla dafay nangu suñuy ñaan?
«Yaw miy nangug ñaan, yaw la képp di wuyusi.» (Taalifi Cant 65:3).
Kàddu Yàlla wone na ne
Yàlla dafa bëgg ñu di ko ñaan (1 Piyeer 5:7).
Yàlla dafay nangu ñaanu nit ku dëggu (Macë 7:7, 8).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania