Ndax mën nañu am dund gu amul benn metit walla tiis?
Yàlla «mooy fomp seen wépp rongooñ. Dee dootul am, dëj aki yuux aku tiis dootul am, lu njëkk laay wéy.» (Peeñu ma 21:4).
Kàddu Yàlla nee na
Yàlla du ñu mas a teg coono (Yanqóoba 1:13).
Yàlla xam na bu baax jafe-jafe yi ñuy dund te ci kanam tuuti, dina fi dindi bépp coono (Taalifi Cant 34:18-20).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania