Lan mooy indi jàmm ci biir njaboot?
«Na ku nekk sopp jabaram ni mu soppe boppam, te ku nekk weg jëkkëram.» (Efes 5:33).
Kàddu Yàlla nee na
Na ku nekk yem ci ki mu séyal (Macë 19:4-6).
Xale yiy déggal seeni waajur te di leen teral dinañu barkeel (Efes 6:1-3).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania