Ndax dinañu gisaat suñu mbokk yi gaañu?
«Waxtoo ngi ñëw wu mboolem ñi ci biir bàmmeel, di dégg baatam, ba génn» (Yowaan 5:28, 29).
Kàddu Yàlla wone na ne
Yàlla dina dekkil suñu mbokk yi dee (Jëf ya 24:15).
Yàlla yàkkamti na dundalaat ñi dee (Ayóoba 14:13-15).
Boo bëggee am yeneen leeral, demal ci internet, ci jw.org.
© 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania