Xam-xam bi nekk ci Kàddu Yàlla (igw) Xam-xam bi nekk ci Kàddu Yàlla Paas bi turu téere bii nekk/Paas biy wone ñi defar téere bii Xam-xam bi nekk ci Kàddu Yàlla ? LAAJ 1 Laaj 1 : Kan mooy Yàlla ? LAAJ 2 Laaj 2 : Naka ngeen mënee xam Yàlla ? LAAJ 3 Laaj 3 : Ci ñan la Yàlla jaar ngir bind Biibël bi ? LAAJ 4 Laaj 4 : Ndax Biibël bi ànd na ak li tubaab di woowe science ? LAAJ 5 Laaj 5 : Lan mooy xibaar bi nekk ci Biibël bi ? LAAJ 6 Laaj 6 : Lan la Biibël bi yéglewoon ci Almasi bi ? LAAJ 7 Laaj 7 : Lan la Biibël bi yégle lu jëm ci suñu jamono ? LAAJ 8 Laaj 8 : Ndax Yàlla mooy teg nit ñi coono ? LAAJ 9 Laaj 9 : Lu tax nit ñi di am metit ? LAAJ 10 Laaj 10 : Lan lu rafet la Biibël bi wax ci ëllëg ? LAAJ 11 Laaj 11 : Bu nit deewee, lan moo koy dal ? LAAJ 12 Laaj 12 : Ndax mën nañu yaakaar a gisaat ñi dee ? LAAJ 13 Laaj 13 : Lan la Biibël bi wax ci liggéey ? LAAJ 14 Laaj 14 : Naka ngeen mën a yore seen xaalis ? LAAJ 15 Laaj 15 : Naka ngeen mënee am bànneex ? LAAJ 16 Laaj 16 : Naka lañu mënee jànkoonte ak suñuy coono ? LAAJ 17 Laaj 17 : Naka la Biibël bi mën a dimbalee seen njaboot ? LAAJ 18 Laaj 18 : Naka ngeen mënee jege Yàlla ? LAAJ 19 Laaj 19 : Lan lañu wax ci biir téere yi nekk ci Biibël bi ? LAAJ 20 Laaj 20 : Naka nga mënee jariñoo bu baax li ngay liir ci Biibël bi ?